PAROLE :
Tatagal
Bu ko jot gi may e woon ,
weer wu ne ma ñëw
sagaal sama fan’s yi ,
sant leen , sargal leen
Ni bu leen di sonn al béer ,
njaw du mel ni lem
Jimmy mbaye xalam al leen ,
te encourager leen leen
Bu ko jot gi may e woon ,
weer wu ne ma wëy
Sagaal sama fan’s yi ,
sant leen , sargal leen
ma nii bu leen di sonn al béer ,
njaw du mel ni lem
Jimmy mbaye xalam al leen ,
te encourager leen leen
Na ñu leen xalam al ,
Na ñu leen tatagal
Na ñu leen woy al
na ñu leen sargal
Je vous salue ,
avec tous les honneurs ,
et vous souhaite que du bonheur
Ces fans de valeurs,
qui m’attendent des heures ,
je vous ai dans mon cœurs ,
Vous méritez , d’être ova tionnés ,
c’est ça la vérité
Vous êtes toujours là ,
quoiqu’il puisse arriver ,
yéen ay sama y soppe
Ànd bi yagg na ,
confiance bi rëy na ,
tatagal leen jaadu na
Njukkël leen war na , fu né
nda pare ngen ,
ñu dem wër adduna
Da ma ni pare naa ,
te it sax defe naa ,
xalaat bi jaadu na
Su ma leen
mën oon a jox loxo
yegsi naa
Su ma leen mën oon seet si
yegsi naa
Fatte wu ma leen ,
déedéet mën ul am
Yëg naa leen ,
sallaaw mooy li wóor
fan’s yi xam ci jamono ,
naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg , sargal leen ,
woy ee
Bul gnu leen fatte di bëgguel
naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg , sargal leen ,
woy ee
fan’s yi xam ci jamono ,
naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg , sargal leen ,
woy ee
Bul gnu leen fatte di bëgguel
naw naa seen taxawaay
Moo tax ma jóg , sargal leen ,
woy ee